Portrait Plus
Graphic Designer • Photographer
06/07/2024
Dama ko fatte woon â dugal 😅🤭 !
Conférence Politique avec Ousmane SONKO
🏳 Jeunesse Patriotique du Sénégal-JPS
📍 Grand Théâtre National Doudou Ndiaye Coumba Rose
🗓 09.06.2024
📷 Portrait Plus
09/04/2024
Ginaaw bi ñu dajee ci sowwu jumaa ji ngir séentu weeru Korite (Shawwaal) 1445H ànd ko ak pàcc yi aju ci ñoom te teewal leen ci yeneen warab yi, mbooloo mi Sëriñ bi dénk wàllum séentu weer wi ci Tuubaa ñoo ngi xamle ni weer wi feeñ na, kon suba ci Àllarba ji dëppoo ak 10 Avril 2024 mooy ubbiteg weeru Korite 1445H.
Yal na sunu Borom nangul jullit yépp seen i koor ak jëf yu baax yépp.
——
Mbooloo mi yore wàllum séentu weer wi ci Tuubaa.
Source Grande Mosquée de Touba
Crédit Photo Portrait Plus
16/02/2024
Màggal Kazu Rajab 2024
📍 Hizbut Tarqiyyah Darou Khoudoss
Kureel 01 Tutank Tuuba